Le pagne tissé
Ensemble de huit photographies de Savina Topurska, Système son, voix chantées
Chanson traditionnelle de mariage
Bu ko dóor te bu ko saaga yaay
Ne la bats pas et ne l’insulte pas s’il te plaît
Dee ko munalee
Sois tolérant avec elle
Bu ko dóor te bu ko saaga yaay
Ne la bats pas et ne l’insulte pas s’il te plaît
Dee ko munalee
Sois tolérant avec elle
Waay bu ko door yaay te bu ko saaga yaay
Cher mari, ne la bats pas et ne l’insulte pas s’il te plaît
Dee ko munalee
Sois tolérant avec elle
Boo koy door te di ko saaga yaay
Mon cher si tu la bats et tu l’insultes
Léeg mu nibbisee
Elle rentrera bientôt chez elle
Photo de groupe devant les pagnes tissés
Ndeysane, woy wi koku deg sa xel dem si mur set.
Magi fateleku binuy nek xale lanu dekël sunuy noop ni sey xare là. Bo ci ne sarax caxan dulaci gen. Motax nu wara fong sunu aada ak cosan ni maam yi di aar sey.
aada ak cossaan yoyu le definwi dinatax gay yek bu bax cër bi ñu jox sey si askanu lebu. aada ak cossaan yoyule ño gi kay mandargale sëru dënk . Sër bobule day gunge domu adama bi ci giiru dundëm ratatina ci negu sey.
waye giss ñanu ne yoyule aada yu ci melni muur, labaane, wër, lek lax yi tax nu daan gen seru denk ñu gi tabbale nax say ci sunu jamonano ji. Bataxna leegi nugi setluni seru dënk lu jaffe am la ñikoy rab sac ñu new lañu.
Ndeysaan il est évident que si vous entendez cette chanson, vous penserez à l’arrivée de la nouvelle mariée dans son domicile conjugal.
Je me rappelle lorsqu’on était enfant, on nous disait souvent que le mariage, c’est sacré. Mais c’est aussi un combat. Si toutefois tu t’engages dans le mariage, tu ne peux en sortir sans de bonnes raisons.
C’est pourquoi nous devons respecter les traditions qui nous ont été transmises par nos ancêtres pour protéger le ménage. Les cérémonies nous font ressentir le caractère sacré du mariage, en particulier dans l’ethnie Lebou.
Le pagne tissé joue un rôle central dans le déroulement des rites. Il est omniprésent dans les pratiques ancestrales, de la naissance à la mort, surtout au moment du mariage.
Cependant, de nos jours, on constate que les rituels comme le muur, le lek lax et le labaane, qui font usage du pagne tissé, sont de plus en plus rares. De ce fait, le métier de tisserand se perd peu à peu.